Tuyaaba ju dul jeex: un investissement éternellement rentable

Collecte vérifiée


Créé le 30 novembre 2020

788 520 FCFA
collecté


39%
de 2 000 000 FCFA

48 participants 7 commentaires

🕌Tuyaaba ju dul jeex : un investissement éternellement rentable🕌

Parmi les récompenses divines qui vont suivre le musulman dans sa tombe, y figure l'enseignement d'une connaissance utile pour les gens. Et rien n'y est plus important que l'enseignement du Noble Coran et des préceptes de l'Islam.

Raison pour laquelle nous vous invitons à participer à la construction de Daaray SABIL pour que vous puissiez être récompensés éternellement par Allah. Pour chaque lettre apprise ou chaque sourate par-cœurisée vous aurez des récompenses divines qui vous suivent dans cette vie, dans votre tombe et jusqu'à votre entrée au Paradis Firdawsi par la Volonté et Miséricorde d'Allah.
Daaray SABIL ( SÀyydinaa BILaal- qu'Allah l'agrée ) sera construite dans une île inhabitée dans les îles du Saloum près de Toubacouta. La Daara est gérée par des Kaaŋ-fóre ( experts maîtres coraniques qui connaissent par cœur le Coran) issus des Daara traditionelles de Coki, Fass Touré, Touba et Médina Baye ainsi que d'autres professionnels de l'éducation dans de nombreux domaines (mathématiques, informatique, pédagogues universitaire, etc.) afin que les apprenants soient des élites.

Alors, mon frère, ma sœur participe selon tes moyens, car Allah n'est point impressionné par la grandeur ou la petitesse de ce que vous donnez. Il regarde la sincérité de votre cœur et la noblesse de votre action. Pour chaque franc investi, Allah vous le rendra à sa meilleure valeur un jour où vous serez seul qu'avec Lui et vos actions. Merci pour votre participation, qu'Allah vous l'accepte

🇸🇳🇸🇳🇸🇳

Bokk na ci li nga xamne mooy fekk jullit bi ci biir bàmmeelam mooy xam-xam buy jariñ doomu Aadama yi. Rawatina jàngale Alxuraan ak diine Lislaam.
Loolu moo tax nu leen di woo ci tabax Daaray SABIL. Ndax da noo bëgg itam ngeen am Tuyaaba joo xam ne du jeex ba fàww. Araf wu ñu fa jàng, wala saar wu ñu fa mokkal, dess na la ca bindal ay yool yu lay toppu ci sa àdduna, sa bàmmeel, ba nga dugg Guyaar(Aljana)Firdawsi ndeem soob na Yàlla.
Daaray SABIL ( SÀYYDINAA BILAAL- Yal na ko Yàlla gërëm- ) di na ñu ko taxawal ci dun bu kenn dëkkul, sóri dëkkuwaay yi ci ganaaw géeju Tubaakuta.
Ay kaaŋ-fóre, yu jàngee Kokki, Faas Ture, Tuubaa, Medina-Baay ak ay woram i xam-xam ci wàllu yu bari (mandaxe, informatik, xam-xamu jàngale ci daara yu kawe yi, añs...) ñoo séq liggéey ngir ndogo daara yi mëna doon ñu raññee ku ci wàllu xam-xam yépp.

Kon daal mbokk mi loo mën rekk def ci, ndax Yàlla xeebul, yeemul; xol bu séll ak yéene ju rafet rekk lay xool.

Dërëm boo ci duggal, Yàlla fay la ko lu ko fuuf ci bis boo xam ne yaak sa Boroom rekk, ak sa jëf, yeenay nekk.

Jërëjëf, Yal na la ko Yàlla nàngul !
🇸🇳🇸🇳🇸🇳

من الحسنات التی ترافق المٶمن فی قبره وجعلته فیه روضة من ریاض الجنة. والعلم ینتفع به الإ نسان،لاسیما علم من علوم القران ودین الإسلام. وللذالک سبب ندعوکم لبناء دار القران الکریم(دارالسبیل).ونرید لکم فوزا عظیما لاانقطاع لها ألا وهی الجنة.ذالک الفوز لمن ینفق ماله فی دار السبیل(دار بلال) سنقوم بناءها ومع کل من یرید به خیرا فی مکان بعید عن القریة قرب نهر( طو بی کوته) هذا الأعضاء لتنفیذ عمل التدریس(الحفاظ الخریجی من کوکی ومنالعلماء الذین یتقنون بتعلیم علوم الشرعیة وعلوم الحاسوبیة وغیرها .ومنهم من یسکن فی کولخ ومنهم من یسکن فی طوبی ومنهم من یسکن فی دکار

دعوة شاملا الی جمیع المٶ منین والمٶمنات لبناء دار القران الکریم .قال الله تعالی فی محکم تنزیله (من ذاالذی یقرضالله قرضا حسنا .وما تقدموا لأنفسکم من خیر تجدوه عندالله ..) من أنفق ماله فی تعلیم القران فله اجرعظیم عند الله.وقال ایضا:(وما أنفقتم من شیء فهویخلفه وهو خیر الرازقین) ولذالک نتمنی لکم قوة کافیة .ویتولد من المحاظر ای(دارالقران) الحفاظ والعلماء والفقهاء وغیرهم

Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement

Commentaires (7)


Anonyme (10 000 FCFA )
Yallah na lepp antou Inshallah
le 29/12/2020, 15:35:21

Ndeye Amy (15 000 FCFA )
Qu'Allah l'agrée
le 12/12/2020, 22:31:30

Anonyme (1 500 FCFA )
Je donne pour Dieu
le 09/12/2020, 00:19:59

Cheikh Barham (10 000 FCFA )
تقبل الله منا ومنكم
le 06/12/2020, 20:21:53

Anonyme (10 000 FCFA )
مساءالله
le 06/12/2020, 13:13:40

Anonyme (2 000 FCFA )
Qu'Allah soubhanahou wa taala bénisse cette initiative. Amin
le 03/12/2020, 14:07:20

Pape (10 000 FCFA )
Yallah nako yallah motali
le 30/11/2020, 18:14:10
×
1 / 1

Image
Partager Participer