TOUBA CA KANAM : BARKEELU SAFAR

Collecte vérifiée


Créé le September 9, 2022

16 444 278 XOF
collecté


1%
de 1 000 000 000 XOF

4457 participants 30 commentaires

Souscrire à la dynamique participative de Touba Ca Kanam permet de résorber les difficultés rencontrées à Touba et la roue tourne déjà avec l’érection de routes, de postes de santé et le reverdissent de l’environnement… Donner 1000 frs en ce mois de Safar à TCK est symboliquement significatif de la gratitude du mouride envers Serigne Touba. Tuubaa Ca Kanam laaj lu ñu man, def fu ñu xam.

Nanu jaayante tàbbal sunuy barkeelu ci Touba Ca Kanam ngir saafara soxlay dëkk bi te TCK jot cee def yu am solo, niki : Defar yoon yi, naatal Tuubaa, Leeral Tuubaa, dimbali néew doole yi, wàllu wérgi yaram... jaayante bi day doon delloo njukkal Sëriñ Tuubaa ci weeru Safar wii, du tee nuy wéyal weer 1000f ci muriit bu nekk. Tuubaa Ca Kanam laaj lu ñu man, def fu ñu xam.


Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement

Commentaires (30)


El hadji (1 000 XOF )
Thia kaw thia kanam
le 05/10/2022, 13:43:06

Serigne Moustapha (6 000 XOF )
Xassida yii rek
le 29/09/2022, 16:47:04

Ndiaye (40 000 XOF )
Dieureudieuf borome touba
le 24/09/2022, 20:37:35

Ndiaye (40 000 XOF )
Dieureudieuf borome touba
le 24/09/2022, 20:32:32

Mamadou (1 000 XOF )
🙏🏽🙏🏽🙏🏽
le 24/09/2022, 16:20:38

Anonyme (1 000 XOF )
Dieureudieufeuti Serigne Touba
le 23/09/2022, 21:56:36

Anonyme (3 000 XOF )
Yalna yala motali mebet you bakh yepp
le 23/09/2022, 09:12:41

Anonyme (1 000 XOF )
Merci
le 23/09/2022, 00:25:06

Anonyme (2 000 XOF )
Al hamdu lilah
le 22/09/2022, 23:35:29

Anonyme (2 800 XOF )
Barkeb boroom tuubaa
le 22/09/2022, 23:24:05

Anonyme (1 000 XOF )
Jaa ngeen jëf
le 22/09/2022, 22:31:48

Anonyme (1 000 XOF )
Yàlla na leen saa borom fay ta mottali seen yeené barké cheikhoul khadiim
le 21/09/2022, 10:12:02

Serigne mbacke (1 000 XOF )
Djeurę djëuff Serigne touba
le 20/09/2022, 08:56:39

Bara (4 000 XOF )
Barkellou Mame Faty Seck, Mbene Sakho Ak Aicha Sakho
le 18/09/2022, 17:48:36

Mbaye (1 000 XOF )
Talibé serigne bara Touré madina Touré
le 18/09/2022, 11:43:51

Anonyme (1 000 XOF )
Diereudief serigne touba
le 16/09/2022, 13:29:17

Anonyme (6 000 XOF )
Sant Amadou rek
le 15/09/2022, 20:35:18

Anonyme (2 000 XOF )
Dieureuffety Serigne Touba
le 15/09/2022, 14:51:58

Anonyme (8 000 XOF )
Berkélou
le 15/09/2022, 10:34:20

Diakhate (6 500 XOF )
Ca kaw ca kanam rk, Barkeb borom Touba 🙏
le 15/09/2022, 05:58:51

Dior (1 000 XOF )
Alhamdoulillah
le 15/09/2022, 01:48:18

Anonyme (2 000 XOF )
Dieuredieuf ligueye bu rafet na machallah
le 14/09/2022, 12:33:22

Anonyme (1 000 XOF )
Barkelou
le 14/09/2022, 11:45:38

SALIOU (1 000 XOF )
DIEUREDIEUFAATTIII CHEIKHOULLL KHADIM
le 14/09/2022, 10:26:25

Pape Latyr (1 000 XOF )
Dieureudief borom Touba Yal NAGNU YALLA bolé ball 🙏🙏🙏
le 14/09/2022, 09:50:34

Anonyme (1 000 XOF )
Dieureudieuf cheikh ahmadou mbacke
le 14/09/2022, 06:35:30

Anonyme (9 000 XOF )
Dieuredieufè Serigne Touba
le 14/09/2022, 01:35:10

Sidy (1 000 XOF )
Ma participation de touba thia kanam
le 13/09/2022, 23:40:05

Anonyme (1 000 XOF )
Diadieuf serigne Touba
le 13/09/2022, 22:50:00

Fatim sarr (1 000 XOF )
Dieureudieuf serigne touba
le 13/09/2022, 20:34:50
×
1 / 1

Image
Partager Participer