SÉMB DAARAY XASIDA TUUBAA DAARU MANAAN

Collecte vérifiée


Créé le May 4, 2021

0 XOF
collecté


0.000%
de 10 000 000 XOF

0 participants 0 commentaires

Sémb wi ñu naal ngir taxawal ko fii ci goxub Daaru Manaan muy taxawal Daaray Alxuraan ak Xasida ju mag ngir di fa jàngee Alxuraan ak Xasida ak a bind ak a tàggat ndaw ñi, ci seen diine ak yoonu murit.
Liggéey boobu nag noo ngi ko door ci weer yii weesu di ci woo ñépp ak a talal loxo ñépp.
👉🏾 Bëgg nanu màkkaan, ginaaw bi ñu amee màkkaan bëgg nanu koo tabax, ginaaw bees ko tabaxee ba noppi door liggéey bi ci nimu waree.

Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement

Commentaires (0)

Aucun commentaire
×
1 / 1

Image
Partager Participer